PEOPLE
Accident à Sakal: Mia Guissé «Vraiment métina trop mon cœur saigne»

Vraiment accident bi métina trope . Lane moy solution bi nak??
Mon cœur saigne.
Yalnaléne yalla yeureum té kharéléne aldiana té mou yamfi 🙏🙏🙏